Bene
Réewum Benin | |||||
|
|||||
Barabu Bene ci Rooj |
|||||
Dayo | 112 622 km2 | ||||
Gox | |||||
Way-dëkk | 8 439 000 nit | ||||
Fattaay | 75 nit/km2 | ||||
Xeetu nguur - Njiitu Réew - Njiitu Jëwriñ |
- Yayi Boni - |
||||
Tembte - Bawoo - Taariix |
|||||
Péy ak rëddi - Tus-wu-gaar - Tus-wu-taxaw |
Porto-Novo |
||||
Làkku nguur-gi | Nasaraan | ||||
Koppar | Franc CFA (XOF) | ||||
Turu aji-dëkk | -Bene-Bene -Sa-Bene |
||||
Telefon | |||||
Lonkoyoon bu Bene |
Benin (Republik bu Benin) : réewu Afrig.
- Lii Ab Sémp rekk la man ga cee dugal sa loxo ndeem am ga ci xam-xam
Melosuuf[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Bene aw rëdduw suuf wu sew la, nekk ci diggante yamoo gi ak Gëwéelub Sànkar bi. Rëddu tus-wu-gaar wu bene mi ngi ci diggante 6°30'bëj-g ak 12°30'bëj-g, tu-wu-taxawam moom mi ngi ci 1° P ak 3° 40'P. Ay digam ñoo ngi yem ci Togóo ci sowwu, yem ci Burkina-faso ak Niseer ci bëj-gànnaar, ci Niseeriyaa ci penku, janook mbàmbulaanug Atlas gi ci bëj-saalum. Mi ngi am yaatuwaay bu tollu ci 112.622 yu kaare. Bene ngi bawoo ca dexug Niseer gi ci bëj-gànnaar yem ci mbàmbulaanug Atlas ci bëj-saalum ci ag tallalug 700 km. Diggante bi gën a guddu ci réew mi 325 km la.
Taariix[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Lëkkalekaay yu biti[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
- (en) ICJ Judgment over the Benin-Niger boundary dispute, 12 July 2005 [1]
- (en) Fabio Spadi (2005) The ICJ Judgment in the Benin-Niger Border Dispute: the interplay of titles and ‘effectivités’ under the uti possidetis juris principle, Leiden Journal of International Law 18: 777-794 [2]
Réewi afrig |
Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkina Faso • Buruundi • Cadd • Ecoopi • Eritere • Gaambi • Gaboŋ • Gana • Gànnaar • Ginne • Ginne Bisaawóo • Ginne gu Yemoo • Isipt • Jibuti • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Keeñaa • Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Lesoto • Libeeria • Libi • Madagaskaar • Malawi • Mali • Marook • Móoris • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeria • Ruwandaa • Saambi • Sahara gu Sowwu • Sao Tome ak Principe • Senegaal • Seysel • Simbaawee • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Sudaan gu Bëj-saalum • Suwaasilaand • Tansani • Togóo • Tiniisi • Ugandaa