Xët wu njëkk
Dalal-jàmm ci WikipediaJimbulang bu Ubbeeku bi
|
Seetal ci 1 143 jukki ci kàllaama wolof: |
|
Nas wi bokk na ci bëre biy dàq ber bi ñu ber yenn làkk yi (rawatina ci internet bi), xëcc itam gëndaloo guy yamale te di jàpplante, loolu di sukkandiku ci sañ-sañu askan yi gàddu seen kuute ci caada. |
||
Xam-xam Xam-xami nite ak mboolaay
Ku ca bëgg a bokk mbaa nga bëgg ci yeneeni leeraal man ngaa bind ci : akaademibuwolof@gmail.com |
|
|
|
Sëriñ Saaliwu mi ngi gane àdduna, ca Njaaréem(Senegaal) ci guddig àjjuma gu 14 ci weeru tëbëski, atum 1333 g.g, dëppoo ak 22 satumbar 1915. Aji juram ju góor di ku jaradee leeral ngir xam gi ko nit ñépp xam di Seex Ahmadu Bamba, ju jigéen di Soxna Faati Jaxate, mom Sëñ Moodu Asta mu baax ma te sell. S Tuubaa bi mu ganee àdduna daa bindoon ciw kayit tur wi di (Saaliwu giy tekki aji baax, aji yéwén) jox ko Sëñ Muhammadu Lamin Jóob Dagana, ne ko tudde ko ko, bi mu ko defee moom S Dagana, daa daal di bind as lëf ciy bayit ñaanal ci liir bu tedd bii aw fan wu gudd akug wér, akug yékkatiku ci jamonoom ba mel ni jant, mu wax ca ne:... |
- Yi weesu 80000 jukki: Català · Čeština · Esperanto · Norsk (bokmål) · Русский · Română · Slovenčina · Suomi · Türkçe · 中文
- Yi weesu 40000 jukki: العربية · Bahasa Indonesia · Български · Dansk · Eesti · עברית · 한국어 · Lietuvių · Slovenščina · Српски / Srpski · Українська
- Yi weesu 20000 jukki: Bahasa Melayu · Bosanski · Ελληνικά · English (simple) · Euskara · فارسی · Galego · Hrvatski · Magyar · Norsk (nynorsk) · ไทย · Tiếng Việt
- Afar · Akan · አማርኛ · Bamanankan · Chicheŵa · chiShona · chiTumbuka · Ɛʋɛ · Fulfulde · Gĩkũyũ · هَوُسَ · Igbo · isiXhosa · isiZulu · Kinyarwanda · Kirundi · Kongo ·Lingála · Luganda · Malagasy · Oromoo · Oshiwambo · Sängö · Sesotho · Setswana · siSwati · Soomaaliga · ትግርኛ · tshiVenda · Twi · Xitsonga · (ngir yeneeni Wikipedia, xoolal ci bànqaasu wet gi)
Wikipedia ngi jàppandi ci ndimbalu Wikimedia Foundation mi dalal ciy joxekaayam sémbi wiki yu bari, ubbeeku, barilàkk te amul-fay:
Commons Dàttub njoxeeb ay nataal |
Wikbaatukaay Baatukaay barilàkk |
Wikiquote Dajaleeb ay tudd |
|||
Wikixibaar Xibaari àdduna bi |
Wikitéere Téerey njàng yu ubbeeku |
Wikisource Kaggu bu ubbeeku |
|||
Wikispecies Wayndareeb xeeti mindeef yépp |
Wikidaara Jumtukaay ak yëngu-yëngu ñeel njàng |
Meta-Wiki Nosuwaayu sémbi Wikimedia yi |