Xët wu njëkk

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet
Pix.gif
Pix.gif

Nataalu Wikipedia Dalal-jàmm ci Wikipedia

Jimbulang bu Ubbeeku bi

Seetal ci 1 195 jukki ci kàllaama wolof:

Pix.gif

Nas wi bokk na ci bëre biy dàq ber bi ñu ber yenn làkk yi (rawatina ci internet bi), xëcc itam gëndaloo guy yamale te di jàpplante, loolu di sukkandiku ci sañ-sañu askan yi gàddu seen kuute ci caada.

Àdduna bu gën di yamale, ak gën di tinkiku ci la aju !!!

Nuvola apps edu science.svg


Gnome-fs-client.svg


Nuvola apps kcoloredit.svg


Nuvola apps kuser.svg


Xibaar / Li gën a fés:
A.W (Akaademi Wolof), aw na ci yoonu suqali Wolof !
Mbooloo mu di doomi réew mi dajee nañu ca Tuubaa sos ab Akaademi jagleel ko làkku Wolof. Ñu nar a joyal séen yitte yi gën a mag ci dajale mboolem mbindi mag ñi, ñi bind ci Wolof, gëstu yees ci jot a def, saytu arafi bindiin yi (yoy latin ak yoy alxuraan), tekki xam-xam yi ci Wolof, defar baatukaayu Wolof, defar tëraliinu jàng ak sóññ boroom xam-xam yi ñu sonn ci jàng ak binde ci Wolof. Ndajem boroom xam-xam la mu suqali Wolof rekk tax a jóg waliif wutum xaalis. Àndu ñook nguur mbaa kujjeg politig. Ñoom daal, nee ñu, ñu moom séen bopp la ñu tet sàkku ci mboolem ku Wolof ñor nga jàpp ci liggéey bi ngir suqali làkk wi.

Ku ca bëgg a bokk mbaa nga bëgg ci yeneeni leeraal man ngaa bind ci : akaademibuwolof@gmail.com

Nuvola apps kuser.svg
Askan
Nataalu ayubés bi
Sëriñ Saaliwu MBÀKKE, juróoméelu xalifab Tuubaa, ca njàngum alxuraan ma

Sëriñ Saaliwu mi ngi gane àdduna, ca Njaaréem(Senegaal) ci guddig àjjuma gu 14 ci weeru tëbëski, atum 1333 g.g, dëppoo ak 22 satumbar 1915. Aji juram ju góor di ku jaradee leeral ngir xam gi ko nit ñépp xam di Seex Ahmadu Bamba, ju jigéen di Soxna Faati Jaxate, mom Sëñ Moodu Asta mu baax ma te sell. S Tuubaa bi mu ganee àdduna daa bindoon ciw kayit tur wi di (Saaliwu giy tekki aji baax, aji yéwén) jox ko Sëñ Muhammadu Lamin Jóob Dagana, ne ko tudde ko ko, bi mu ko defee moom S Dagana, daa daal di bind as lëf ciy bayit ñaanal ci liir bu tedd bii aw fan wu gudd akug wér, akug yékkatiku ci jamonoom ba mel ni jant, mu wax ca ne:...


Yeneen sémbi Wikipedia ci yeneeni kàllaama. Nu lim ci ñenn ñi rekk


Yeneen sémbi Wikipedia ciy kàllaamay waa Afrig


Commons-logo-31px.png
Commons
Dàttub njoxeeb ay nataal
Wiktionary-logo-51px.gif
Wikbaatukaay
Baatukaay barilàkk
Wikiquote-logo-51px.png
Wikiquote
Dajaleeb ay tudd
Wikinews-logo-51px.png
Wikixibaar
Xibaari àdduna bi
Wikibooks-logo-35px.png
Wikitéere
Téerey njàng yu ubbeeku
Wikisource-logo.png
Wikisource
Kaggu bu ubbeeku
Wikispecies-logo-35px.png
Wikispecies
Wayndareeb xeeti mindeef yépp
Wikiversity-logo-41px.png
Wikidaara
Jumtukaay ak yëngu-yëngu ñeel njàng
Wikimedia-logo-35px.png
Meta-Wiki
Nosuwaayu sémbi Wikimedia yi